Oseyaani wuute gi ci sumb yi
m r2.6.4) (robot Adding: kbd:Хы ТӀыгуей |
m removing old-formated (incorrect) interwiki |
||
(27 versions intermédiaires par 19 utilisateurs non affichées) | |||
Rëdd 31 : | Rëdd 31 : | ||
[[Wàll:Gox yi]] |
[[Wàll:Gox yi]] |
||
[[ace:Oseania]] |
|||
[[af:Oseanië]] |
|||
[[an:Oceanía]] |
|||
[[ar:أوقيانوسيا]] |
|||
[[arz:اوشيانيا]] |
|||
[[as:ওচেনিয়া]] |
|||
[[ast:Oceanía]] |
|||
[[az:Avstraliya və Okeaniya]] |
|||
[[bat-smg:Okeanėjė]] |
|||
[[bcl:Oceanya]] |
|||
[[be:Акіянія]] |
|||
[[be-x-old:Акіянія]] |
|||
[[bg:Океания]] |
|||
[[bm:Oseania]] |
|||
[[bn:ওশেনিয়া]] |
|||
[[bo:རྒྱ་མཚོ་ཆེན་པོའི་གླིང་ཆེན།]] |
|||
[[br:Okeania]] |
|||
[[bs:Okeanija]] |
|||
[[ca:Oceania]] |
|||
[[ceb:Oseyaniya]] |
|||
[[ckb:ئۆقیانووسیا]] |
|||
[[crh:Avstraliya ve Okeaniya]] |
|||
[[cs:Oceánie]] |
|||
[[cv:Океани]] |
|||
[[cy:Oceania]] |
|||
[[da:Oceanien]] |
|||
[[de:Ozeanien]] |
|||
[[diq:Okyanusya]] |
|||
[[dsb:Oceanija]] |
|||
[[el:Ωκεανία]] |
|||
[[en:Oceania]] |
|||
[[eo:Oceanio]] |
|||
[[es:Oceanía]] |
|||
[[et:Okeaania]] |
|||
[[eu:Ozeania]] |
|||
[[ext:Oceania]] |
|||
[[fa:اقیانوسیه]] |
|||
[[fi:Oseania]] |
|||
[[fiu-vro:Okõaania]] |
|||
[[fo:Kyrrahavsoyggjarnar]] |
|||
[[fr:Océanie]] |
|||
[[frp:Ocèanie]] |
|||
[[frr:Oseåånien]] |
|||
[[fur:Oceanie]] |
|||
[[fy:Oseaanje]] |
|||
[[ga:An Aigéine]] |
|||
[[gag:Okeaniya]] |
|||
[[gan:大洋洲]] |
|||
[[gd:Roinn a' Chuain Shèimh]] |
|||
[[gl:Oceanía]] |
|||
[[glk:اوقیانوسیه]] |
|||
[[he:אוקיאניה]] |
|||
[[hi:ओशिआनिया]] |
|||
[[hif:Oceania]] |
|||
[[hr:Oceanija]] |
|||
[[hsb:Oceanija]] |
|||
[[ht:Oseyani]] |
|||
[[hu:Óceánia]] |
|||
[[hy:Օվկիանիա]] |
|||
[[ia:Oceania]] |
|||
[[id:Oseania]] |
|||
[[ie:Oceania]] |
|||
[[io:Oceania]] |
|||
[[is:Eyjaálfa]] |
|||
[[it:Oceania]] |
|||
[[ja:オセアニア]] |
|||
[[jv:Oséania]] |
|||
[[ka:ოკეანეთი]] |
|||
[[kbd:Хы ТӀыгуей]] |
|||
[[kl:Oceania]] |
|||
[[km:អូសេអានី]] |
|||
[[kn:ಒಷ್ಯಾನಿಯ]] |
|||
[[ko:오세아니아]] |
|||
[[krc:Океания]] |
|||
[[kw:Oceania]] |
|||
[[ky:Океания]] |
|||
[[la:Oceania]] |
|||
[[lad:Oseania]] |
|||
[[lb:Ozeanien]] |
|||
[[li:Oceanië]] |
|||
[[lij:Oçeania]] |
|||
[[lmo:Uceania]] |
|||
[[ln:Oseanía]] |
|||
[[lt:Okeanija]] |
|||
[[lv:Okeānija]] |
|||
[[mg:Oseania]] |
|||
[[mhr:Океаний]] |
|||
[[mk:Океанија]] |
|||
[[ml:ഓഷ്യാനിയ]] |
|||
[[mn:Австрали ба Номхон далайн орнууд]] |
|||
[[mr:ओशनिया]] |
|||
[[ms:Oceania]] |
|||
[[mt:Oċeanja]] |
|||
[[mwl:Ouceanie]] |
|||
[[my:အိုရှန်းနီးယား]] |
|||
[[nah:Oceania]] |
|||
[[nds:Ozeanien]] |
|||
[[ne:ओसेनिया]] |
|||
[[nl:Oceanië]] |
|||
[[nn:Oseania]] |
|||
[[no:Oseania]] |
|||
[[nov:Oseania]] |
|||
[[nrm:Ochéannie]] |
|||
[[oc:Oceania]] |
|||
[[os:Океани]] |
|||
[[pcd:Ochéani]] |
|||
[[pl:Oceania]] |
|||
[[pnb:اوشیانا]] |
|||
[[pnt:Ωκεανίαν]] |
|||
[[pt:Oceania]] |
|||
[[qu:Usiyanya]] |
|||
[[rm:Oceania]] |
|||
[[ro:Oceania]] |
|||
[[roa-tara:Oceanie]] |
|||
[[ru:Океания]] |
|||
[[rue:Океанія]] |
|||
[[rw:Oseyaniya]] |
|||
[[sah:Океания]] |
|||
[[scn:Oceania]] |
|||
[[sco:Oceanie]] |
|||
[[se:Oseania]] |
|||
[[sh:Oceanija]] |
|||
[[simple:Oceania]] |
|||
[[sk:Austrália a Oceánia]] |
|||
[[sl:Oceanija]] |
|||
[[sm:Oceania]] |
|||
[[so:Ooshiyaaniya]] |
|||
[[sq:Oqeania]] |
|||
[[sr:Океанија]] |
|||
[[srn:Oseyaniya]] |
|||
[[sv:Oceanien]] |
|||
[[sw:Australia na Pasifiki]] |
|||
[[szl:Uoceańijo]] |
|||
[[ta:ஓசியானியா]] |
|||
[[te:ఓషియానియా]] |
|||
[[tet:Oseánia]] |
|||
[[tg:Уқёнусия]] |
|||
[[th:โอเชียเนีย]] |
|||
[[tk:Okeaniýa]] |
|||
[[tl:Oceania]] |
|||
[[tpi:Osenia]] |
|||
[[tr:Okyanusya]] |
|||
[[tt:Океанлык]] |
|||
[[uk:Океанія]] |
|||
[[ur:اوقیانوسیہ]] |
|||
[[vec:Oceania]] |
|||
[[vi:Châu Đại Dương]] |
|||
[[war:Oceania]] |
|||
[[yi:אקעאניע]] |
|||
[[yo:Oṣéáníà]] |
|||
[[zh:大洋洲]] |
|||
[[zh-classical:大洋洲]] |
|||
[[zh-min-nan:Tāi-iûⁿ-chiu]] |
|||
[[zh-yue:大洋洲]] |
Sumb bi teew bu 2 Sulet 2013 à 19:48
Oseyaani ab gox la bu nekk ci Mbàmbulaan gu Dal gi. Ci biiram Óstraali, ak Seland-Gu-Bees gi, ak Papuwasi-Ginne-Gu-Bees gi, Tasmaani, ak yeneeni dun. Oseyaani mooy gox bi gën a tuuti.
Ci lu daj
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Ci lu daj Oseyaani dañ koy jàppee ni ab gox bu nekk ci diggante Bëj-saalum-penku Asi ak Bëj-saalumu Aamerik.
Oseyaani mooy gox bi gën a tuuti ci gox yi ci àdduna bi, ci 8 523 655 km kaare lay tollu, te 90% ya Óstraali la, 5,4 % ya di Papuwasi-Ginne-Gu-Bees, 3,1% ya di Seland-Gu-Bees gi, yeneen réew-réewaan yi tas ci Mbàmbulaan gu Dal gi doon 1,5 ci gox bépp.
Am na 32 642 390 ciy way dëkk di ñareelu gox bi gën a néew ay nit lu weesu Dottu Bëj-gànnaar bi. 60% ya Óstraali la ñu dëkk, 16% ya Seland-Gu-Bees gi, 12% ya Papuwasi-Ginne-Gu-Bees.
Diwaan
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Ni yeneen gox yépp, ay peggan ci deggoo rekk lañ leen daggee. Baatu Oseyaani dañ koy jëfandikoo ngir jëmmal ab xaaj ci àdduna bi bu ëmb bépp suuf su nekk ci Mbàmbulaan gu Dal gi te duggoo ci barabi dott bi.
Ci lu ëpp yii la ñuy jàpp ne ñooy ay Diwaanam:
Ki defoon bi seddale moo doonoon Jules Dumont d'Uville ci 1831, waaye tegu woon ci cëslaayu xam-xam gu ñu ñangu tay. Ci 1970 ba tay, séwógaraafikat yi, Gëstukatu-làkk yi, ak yeneen boroom xam-xam, ci seeniy liggéey, yii rekk la'ñ koy seddalee Oseyaani gu Jege ak Oseyaani gu Sori.
Rèew ak suuf
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Lu ëpp ci réewi Oseyaani yi, ay dun la ñu. Mennum Óstraali ak Papuwasi-Ginne-Gu-Bees ñoo am ay peggu suuf ak yeneen réew (Ci Dunu Ginne gu Bees gi ak Endonesi gi ñuy boole wàllam gu bari ci Oseyaani).
Lim bii di toftal dafa boole mbooleem réew aki suuf yi fa nekk. Te jàpp nak ne am na ay suuf yu fa ne te ñu jàppee leeni réew, waaye tembu ñun kon ay réew la ñu ci biiri réew, di nan bind ci réew mi ñu bokk ci wet gi.
Réew yu temb yi |
Rèew ak Suuf yu tembul
|
Afritugalasi | Oseyaani | Afrig | Tugalasi |
Bëj-gànnaaru Aamerig | Tugal | Asi | Bëj-saalumu Aamerig |