Aller au contenu

Bunt: taariix

Jóge Wikipedia.
Sumbu 17 Mee 2009 à 22:14, bu: MelancholieBot (waxtaancëru) (roboto aldono de: tt:Тарих)
Jumaay Jéene gu yagg ga ca Mali
Jumaay Jéene gu yagg ga ca Mali

BUNTU TAARIIX

Taariix mooy la xewoon ca ñoom maam ba ci nun, mbooleem xew-xew ya ag jëf soo leen boolee. Nekk itam xam-xam giy gëstu xew-xewi demb.
Jamonoy taaxe
Jamono ju yàgg ja
Jamono ju diggu ja
mansa musaa, buuru nguuru mali lawoon
mansa musaa, buuru nguuru mali lawoon