Aller au contenu

Bunt: taariix

Jóge Wikipedia.
Sumbu 22 Mee 2009 à 17:34, bu: Xqbot (waxtaancëru) (robot Adding: ar, bg, ca, cs, da, de, en, es, fa, fi, fr, he, hr, hu, id, it, ja, ka, ko, lt, lv, mk, ms, nds, nl, nn, no, oc, pl, pt, ro, ru, sk, sl, sr, sv, th, uk, zh, zh-classical, zh-yue Removing: tt)
Jumaay Jéene gu yagg ga ca Mali
Jumaay Jéene gu yagg ga ca Mali

BUNTU TAARIIX

Taariix mooy la xewoon ca ñoom maam ba ci nun, mbooleem xew-xew ya ag jëf soo leen boolee. Nekk itam xam-xam giy gëstu xew-xewi demb.
Jamonoy taaxe
Jamono ju yàgg ja
Jamono ju diggu ja
mansa musaa, buuru nguuru mali lawoon
mansa musaa, buuru nguuru mali lawoon