Aller au contenu

Bunt: taariix

Jóge Wikipedia.
Sumbu 22 Maars 2011 à 01:06, bu: KamikazeBot (waxtaancëru) (r2.6.4) (robot Adding: pam:Portal:Amlat)
Jumaay Jéene gu yagg ga ca Mali
Jumaay Jéene gu yagg ga ca Mali

BUNTU TAARIIX

Taariix mooy la xewoon ca ñoom maam ba ci nun, mbooleem xew-xew ya ag jëf soo leen boolee. Nekk itam xam-xam giy gëstu xew-xewi demb.
Jamonoy taaxe
Jamono ju yàgg ja
Jamono ju diggu ja
mansa musaa, buuru nguuru mali lawoon
mansa musaa, buuru nguuru mali lawoon