Aller au contenu

Bunt: taariix

Jóge Wikipedia.
Sumbu 2 Sattumbar 2011 à 21:48, bu: KamikazeBot (waxtaancëru) (r2.7.1) (robot Adding: ne:Portal:इतिहास)
Jumaay Jéene gu yagg ga ca Mali
Jumaay Jéene gu yagg ga ca Mali

BUNTU TAARIIX

Taariix mooy la xewoon ca ñoom maam ba ci nun, mbooleem xew-xew ya ag jëf soo leen boolee. Nekk itam xam-xam giy gëstu xew-xewi demb.
Jamonoy taaxe
Jamono ju yàgg ja
Jamono ju diggu ja
mansa musaa, buuru nguuru mali lawoon
mansa musaa, buuru nguuru mali lawoon