Aller au contenu

Bunt: taariix

Jóge Wikipedia.
Sumbu 17 Maars 2012 à 18:22, bu: Luckas-bot (waxtaancëru) (r2.7.1) (Robot: Adding uz:Portal:Tarix)
Jumaay Jéene gu yagg ga ca Mali
Jumaay Jéene gu yagg ga ca Mali

BUNTU TAARIIX

Taariix mooy la xewoon ca ñoom maam ba ci nun, mbooleem xew-xew ya ag jëf soo leen boolee. Nekk itam xam-xam giy gëstu xew-xewi demb.
Jamonoy taaxe
Jamono ju yàgg ja
Jamono ju diggu ja
mansa musaa, buuru nguuru mali lawoon
mansa musaa, buuru nguuru mali lawoon