Aller au contenu

Bunt: taariix

Jóge Wikipedia.
Sumbu 19 Nowembar 2012 à 05:33, bu: Makecat-bot (waxtaancëru) (r2.7.3) (Robot: Adding wuu:Portal:历史)
Jumaay Jéene gu yagg ga ca Mali
Jumaay Jéene gu yagg ga ca Mali

BUNTU TAARIIX

Taariix mooy la xewoon ca ñoom maam ba ci nun, mbooleem xew-xew ya ag jëf soo leen boolee. Nekk itam xam-xam giy gëstu xew-xewi demb.
Jamonoy taaxe
Jamono ju yàgg ja
Jamono ju diggu ja
mansa musaa, buuru nguuru mali lawoon
mansa musaa, buuru nguuru mali lawoon