Aller au contenu

Jëfandikukat:Ibou

Jóge Wikipedia.
La version imprimable n’est plus prise en charge et peut comporter des erreurs de génération. Veuillez mettre à jour les signets de votre navigateur et utiliser à la place la fonction d’impression par défaut de celui-ci.
man la
I am a sysop (Yorkat) in this Wiki.
I am a sysop (Yorkat) in Wikbaatukaay.
I am member in Omegawiki].
I am member in Betawiki.
I am a member in it wikipedia .
Wikipedia:Babel
it-4
fr-2
en-2
Seet waa-wikipedia ci làkk-ak-làkk

Wolof: Sama tur mooy Ibrahima Fall, Ibou di sama dàkkantal. Ci samag dund gu dëggu damay liggéey niki defarkatu jëfekaay. Maa ngi am ab lijjaasa ci Xereñug Boppal ca daara-ju-kawe ju Bologna ca Itaali.

Ci 2007 laa tambalee jàng wolof. Mooy làkk wi ma gënn a neex te it mooy sama làkk ci meen. Ci 2007 itam laa bindu ci Wikipedia tamblee cëru ci liggéey bi. Ab yorkat laa ci. Maa tekki jokkalekaay bu mediawiki bépp ci wolof

li ëpp ci li may jàng mooy téere taariix, roman, taalif ak xeltu. Téere bi ma njëkk a jàng mooy "nations négres et cultures" "Reewi ñu ñuul ak cosaan" bu Seex Anta Joob.
Taggat-yaram bi ma gën a neex mooy futbòl.

English: My name is Fall Ibrahima, I have a degree in Automation Engineering in the university of Bologna in Italy. I am a software developer.
I started contributing in Wikipedia wolof in 2007. I am administrator in this Wiki and Wiktionary (wikbaatukaay). I translate the mediawiki interface into Wolof.

Binduwaay