Aller au contenu

Ayiti

Jóge Wikipedia.
Sumbu 15 Suwe 2010 à 22:13, bu: Xqbot (waxtaancëru) (robot Adding: bm:Ayiti)


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Ayiti
Raaya bu Ayiti
Barabu Ayiti ci Rooj
Barabu Ayiti ci Rooj
Dayo km2
Gox
Way-dëkk nit
Fattaay nit/km2
Xeetu nguur
- Njiitu Réew
- Njiitu Jëwriñ
Tembte
- Bawoo
- Taariix
Péy ak rëddi
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw

Làkku nguur-gi
Koppar
Turu aji-dëkk
Telefon
   

Ayiti ab dun la bu nekk ca Amerik diggu. Day ab dun bu mag bu mu bokkal Republik dominicaine te Port-au-Prince di péyam.

Ayiti mooy reewu ñu ñuul ñi njëkka moom seen bopp ci attum 1804, ca seen fippu ga (1791-1803) ca la ñu dakkee Napoleon ak ay ñoñam ca dun ga.

Magginu turu dëkk ba

Ci aaday Taino yi, Ayiti da doon tekki suufu doj yu kawe ya walla aw doj ci biir geej.